Posts Tagged ‘becoming like Jesus’
05. Tàmmkat bi dafay melni ki muy topp
Ndax mën nga nekk taalibe te doo yokk ay taalibe? Xaaj 05. Ana bu fekkee firnde bi gëna leer ne topp nanu Yeesu mooy sunu dund di gën di niru ak dundam? Yeesu nee na: "Taalibe du raw jàngalekatam, waaye ku ñu jàngal ba mu mat, dina mel ni jàngalekatam." Luk 6:40 WEB…
Gën a jàng