06. Aadaay fitna dafa soxla ay taalibe jàmm

06. A Culture of Violence Needs Disciples of Peace

Fukk ak ñaari sabab yu am solo yi tax war nanoo def ay taalibe · Pàcc 06 ▶ Séetaanleen widewo bii tey. Mënuñoo faj aada ju fees ak fitna ci wax rekk ñi mer ñu dal. Ay kampaañ yu ñuy amal ci askan wi mën nañoo ñàwlu mbañeel. Yoon mën na dàkkee ñiy def fitna. Njiit yi mën nañoo woo ci bennoo. Waaye amul benn ci yii bu mën a dindi wex ci xolu nit…

Gën a jàng