Binda yu ñu takkal 'repentance'‘
12. Jéggal ci diiney Kirist gu dul jur
Ndax mën nga nekk taalibe te doo yokk ay taalibe? · Pàcc 12 ▶ Seetaan Widewoo Tay Ji Am na jamono ju ñu war a bàyyi di aar sunu ñàkk meññeef te tàmbali di ko nangu. Dem nanu jàngu. Jàng nanu Biibël bi. Déglu nanu waare yi, bokk ci ay mbooloo yu ndaw, liggéeyal nanu ay komite, te bokk…
Gën a jàng