07. Xibaar bu amul wàllante du mat.

07. Information Without Reproduction Is Not Maturity

Ndax Mën Nga Nek Dàmm Te Bul Yokk ay Dàmm?. Xaaj 07 Mën nga xam téerey Biibël bi. Xam teyoloji. Dem ci njàngum Biibël. Déglu waare yi ayu-bés bu nekk. Teewul nga bañ a dégg ndigëlu Yeesu bi di def ay dàmm. Lu bare, matug ruu dañu koy natt ci ni nit ki xamee. Yeesu dafa ko natt ci meññeef. "Ci lii…

Gën a jàng